56

Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

  • Upload
    others

  • View
    0

  • Download
    0

Embed Size (px)

Citation preview

Page 1: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :
Page 2: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

Responsable édition : Caroline RollandDirectrice artistique et illustrations : Dorine EkpoAuteur : Maxime Colin-Yves

Toute reproduction de cet ouvrage requiert l'accord de l'éditeur.Loi n°49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n°2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer : Mars 2017.Édition Jeannette Kibangu - 12 rue Anselme, Saint Ouen, 93400

Page 3: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

Ahmadfifi et patou rencontrent

À Ahmad mon fils

Page 4: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

4 — Viens Patou, allons l’aider !

Mais, tandis qu’ils se promènent, ils découvrent un enfant de

leur âge... Assis seul sous un grand arbre, l’enfant pleure toutes

ses larmes. Fifi prend Patou par la main :

Par un bel après-midi ensoleillé, Fifi et Patou se promènent

dans les bois. Leur chien Popo court après le vol de quatre

papillons et le bourdonnement des abeilles.

Page 5: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

5

Page 6: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

6

Tous deux se présentent :

— Bonjour, je m’appelle Fifi.

— Et moi, je m’appelle Patou.

- Man Ahmad laa tudd.

Fifi hausse les sourcils :

— Et toi, comment t’appelles-tu ?

Popo tourne autour du nouvel ami en remuant la queue :

— Lui, c’est notre chien Popo !

— Wouf, wouf !

Patou s’approche un peu plus :

— Quel âge as-tu ?

L’enfant sèche ses larmes et relève les yeux.

- Ñett (3) at laa am... — Et moi j'ai 6 ans ! S'exclame Patou.

- Je m’appelle Ahmad.- J’ai trois (3) ans...

Page 7: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

7

Page 8: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

8

Page 9: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

9

Fifi lui sourit :

— Moi, j’ai 9 ans. Dis-nous, pourquoi es-tu triste ?

Patou et Popo seront, comme moi, ravis de t’aider !

Patou approuve :

— Oh oui alors !

Les enfants s’assoient en rond sur l’herbe

et Ahmad leur explique :

— Mais… il n’y a pas de quoi pleurer, s’étonne Patou.

- Samay waajur dañoo xëy liggeeyi te samay mak ak samay rak dañoo jangi. Sama maam bu jigeen dafmay yonni ngir ma dem nduggi saayu marse amee.

- Mes parents travaillent et mes frères et sœurs sont à l’école. Les jours de marché, grand-mère m’envoie faire les courses.

Page 10: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

10

Page 11: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

— Merci de ta compréhension, dit Fifi !

11

Alors, Ahmad devient triste :

Fifi n’en revient pas :

— Bravo, Patou, pour ta délicatesse !

— Pardon… Répond Patou, tout penaud.

- Ahankay ndax xaalis ba sama maam joxoon reeralnaa ko...

- Je pleure car j’ai perdu tout l’argent qu’elle m’a confié...

- Ne soit pas désolé, c'est entièrement de ma faute, tu essaies seulement de m'aider.

- Ahmad ne ko bul rus man maa ko def, jappalema rek moo la taxoon

jog...

Page 12: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

12

Page 13: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

13

Ahmad s’inquiète encore pour son argent :

- Dama waroon dem marse ngir jënd jën, ceep, banaana ak tuuti suukar... Nan laay def leegi ?

Fifi le rassure :

— Ne t’inquiète pas, nous allons t’aider à trouver ton argent. Nous devons revenir sur nos pas,

tu as dû le laisser sur le chemin. Où habites-tu ?

Ahmad leur montre le chemin jusqu’à sa maison en chantant. Fifi trouve que Ahmad chante bien :

— Tu fais de la musique ?

- Waaw, damay xalam di tëgg sabar.Talaata bu jot damay jang.

Patou fatigue :

— Habites-tu encore loin ?

- Je devais aller au marché pour acheter du poisson, du riz, des bananes et un peu de sucre...Comment vais-je faire à présent ?

- Oui, je joue de la guitare et du tam-tam. Je prends des cours tous les mardis.

Page 14: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

14

- Deet-deet fi rek. Ci benn tool bu am ay bëy ak ay ganar yu bari laa dëkkee.Waaye moytu leen de, sama

maam waru ñoo gis...

Fifi marche sur la pointe des pieds,

Ahmad fouille derrière les buissons,

et Patou grimpe au sommet d’un arbre.

Il leur fait signe :

— Je ne vois rien ici !

- Non, non, c’est juste là. J’habite une ferme avec des chèvres et des poules. Mais prenez garde,

il ne faut pas que grand-mère nous voie…

Page 15: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

15

Page 16: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

16

Page 17: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

17

Ahmad se gratte la tête.

- Doy na waar sama maam bu jigeen dinama jeppi !— Tu as bien dit que c’est aujourd’hui le jour du marché ?

- Ahmad daadi kay tontu, ne ko waaw, ni ñu koy defee al-larba ak gaawu bu ne !

— Eh bien puisque nous ne retrouvons pas ton argent,

nous allons en gagner par nos propres moyens !

Patou est d’accord :

— Comme dit toujours grand-père : « heureux sont ceux qui se suffisent à eux-mêmes ! »

- Ahmad daadi kontaan ne ayca leen ñu dem lijjanti koppar yu ñu moomal su ñu bopp !

Popo prend la tête de l’équipe, tout excité

par cette nouvelle destination…

- C’est terrible, mamie sera déçue !- Oui, répond Ahmad, comme tous les mercredis

et les samedis !- En route, se réjouit Ahmad !

Page 18: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

18

Patou leur montre un chemin :

— Faisons un détour par le terrain vague,

nous y trouverons sûrement des choses

intéressantes.

Page 19: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

19

Une fois dans le terrain vague, Ahmad prend les devants :

— Et moi, reprend Fifi de plus belle, je nous fais des costumes

tous neufs avec ces vieux sacs en toile !

- Man woy ak fecc rek laa mën, dina defar xalam ndax am naa boyt, bant ak ay weñ !

Patou mélange de la terre et de l’eau pour peindre sur les tissus.

- J’adore jouer de la musique, avec cette boîte, ces fils et ce bâton, je fabriquerai une guitare !

- Mais c’est magnifique, se réjouit Ahmad !

-Ahmad kontaan, ëy waay, liggeey bi rafet na !

Page 20: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

20

Les marchands sont réunis au milieu de la place.

Enfants et adultes font leurs achats.

- Na ňu dem ci sufu garabu mango bi foofu dina ñu moytu

taw bi bu baax !

Ahmad montre un bel arbre du doigt :

Patou entraîne ses amis :

— Vite, avant que la foule ne se disperse !

Fifi lève les yeux :

— Mince, il commence à pleuvoir !

- Allons sous le gros manguier, nous y serons bien à l’abri !

Page 21: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

21

Page 22: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

22

Page 23: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

23

Patou chante de sa plus belle voix.

Ahmad l’accompagne à la guitare et Fifi fait quelques pas de danse…

— Il pleut, il pleut, il pleut, chante Patou, il pleut sur le marché !

Les passants s’approchent :

— Oh, quel joli spectacle !

Fifi et Ahmad fredonnent avec Patou :

- Di woy naan mu ngi taw, mu ngi taw, tawataw ci gox bi !

Popo fait le beau dans son déguisement de lion.

- Il pleut, il pleut, il pleut sur la campagne !

Page 24: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

24

Page 25: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

25

La foule est émerveillée :

— Bravo, bravo ! Encore !

— Tu as vu ça ? Demande Patou à Ahmad.

Fifi est heureuse comme tout :

— Quel succès !

Ahmad saute de joie :

- Jërë-jëf yeen ñar ! Ci dëgg-dëgg ay xarit yu baax ngeen !

Chaque passant leur donne une pièce ou un billet.

Les commerçants leur offrent de la nourriture :

- Merci à vous deux ! Vous êtes vraiment des copains géniaux !

— Prenez, prenez, et merci les enfants !

Vous avez enchanté notre journée…

Page 26: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

26

Fifi, Patou et Popo raccompagnent Ahmad. Sa grand-mère est surprise :

- Ahmad ne maamji jënd na li ngama yonni woon yëp: jenn, céep, banaana ak tuuti suukar !

— Tu as oublié ton argent ici ! Comment as-tu acheté toutes ces provisions ?

- Ahmad né ko dama am ay xarit yu bes yuma jappale bama lijjan-ti xaalis bou léw ca marsé ba, loolu la ñu nduggee.

Sa grand-mère éclate de rire :

— Invite-les donc à manger !

- Ahmad ne leen aksileen samay xarit, dal leen ak jamm sama kër !Autour d’un bon repas, Fifi et Patou racontent leurs aventures de la journée.

Popo conclut :

— Wouf, wouf !

- Mamie, voici les courses que tu m’avais demandées : du poisson, du riz, des bananes et un peu de sucre !

- Je me suis fait des amis qui m’ont aidé à gagner de l’argent au marché.- Entrez les amis, venez découvrir ma maison !

Page 27: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

27

FIN

Page 28: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

lexiqueW o l o f

PRÉSENTATIONJe m'appelle... : Maa ngi tudd.J'ai 3 ans : Ñett at laa am.

HABITATIONJ’habite dans une maison : Maa ngi dëkk ci kër.J’habite dans une ferme : Maa ngi dëkk ci tool.J'habite à la campagne : Maa ngi dëkk kaw nga.J'habite en ville : Maa ngi dëkk ci dekku taax.

LIEUXJe vais au marché : Maa ngi dem marse.

Je vais à l'école : Maa ngi dem jangi.Je vais à la maison : Maa ngi dem kër nga.

LES JOURS DE LA SEMAINE

lundi : Altinemardi : Talaata

mercredi : Allarbajeudi : Alkamis

vendredi : Aljumasamedi : Gaawu

dimanche : Dibeer

Page 29: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

LES COURSESargent : xaalis

poisson : jënriz : ceep

banane : banaanapomme de terre : pombiteer

sucre : suukarsel : xorom

piment : kaani

MÉTÉOla pluie : taw

le soleil : jant, naajIl pleut : mungi taw.

Il fait beau : jawwu ji dafa neex.Il fait froid : dafa sedd.

Il fait chaud : dafa tàng.

LES ÉMOTIONSJe suis contente : Damaa kontaan.

Je ris : Maa ngi reetaan.Je suis triste : Damaa am naqqar .

Je pleure : Maa ngi jooy.

LES PROCHESparents : Waajur

frère : Mak walla rakk bu goorsœur : Mak walla rakk bu jigeen

grand-mère : Maam bu jigéengrand-père : Maam bu goor

ami : amiACTIVITÉ

J'aime faire du sport : Damaa bëg taggat sama yaram.J'aime jouer au football : Damaa bëg futbal.

J'aime danser : Damaa bëg fecc.Je joue de la musique : Maa ngi woy.Je joue de la guitare : Damay xalam.

Je joue du tam-tam : Damay tëgg sabar.J'aime jouer de la musique : Damaa bëg woy.

Page 30: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

Responsable édition : Caroline RollandDirectrice artistique et illustrations : Dorine EkpoAuteur : Maxime Colin-Yves

Toute reproduction de cet ouvrage requiert l'accord de l'éditeur.Loi n°49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n°2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer : Mars 2017.Édition Jeannette Kibangu - 12 rue Anselme, Saint Ouen, 93400

Page 31: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

AhmadFif ak Patou dañoo daje ak

À Ahmad mon fils

Page 32: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

4 — Kaay Patou ñu dem walluji ko…

Waaye, ni ñu doon doxantu, lañu daje ak benn xale bu maase ak

ñoom ci ay at…. Xale baangiy took moom kase ci suufu garab bu

mag, di jooy ba ay rongo�am di tuuru. Fifi japp ci loxo Patou :

Ci benn ngoon su neex boole ko ak jant bi ne fa�g, Fifi

ak Patou ñungi doon doxantu ci all bi.

Seen xaj bi Popo, moongi daw ci ginnaaw ñeenti

lëppaa-lëpp yuy naaw ak ay yamb yuy biiw.

Page 33: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

5

Page 34: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

6

Ba ñu ñëwee ci wetu xale bi ku ci nekk wax turam.

— Kii ne ko asalaamaalekum maa ngi tudd Fifi.

— Keneen ki ne man maay Patou.

- Man Ahmad laa tudd.

Fifi xulli ay gëtam ne ko:

— Yow nak noo tudd ?

Popo mungi wër ci wetu xaritam bu bees bi di yëngëlaale geenam.

—Ki mooy Popo, su�u xajla!

— Popo daadi ne wow, wow !

Patou gën ko jegesi

— Ñaata at nga am ?

Xale bi fomp ay rongo�am daadi siggi xool ko :

- Ñett at laa am....— Patou daadi ne laay man tamit.

Page 35: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

7

Page 36: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

8

Page 37: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

9

Fifi beg loolu ba pare xamal ko:

— Man juroom-ñint at laa am. Wax ñu lu tax nga jaaxle?

Man, Patou ak Popo dina ñu sawar lool taxawu la !

Patou ne ko:

- Waaw-waaw wax ñu waay lula naqari !

Noonu xaleyi took làng ci �ax gi Ahmad

nettalileen naqaram :

- Samay waajur dañoo xëy liggeeyi te samay mak ak samay rak dañoo jangi. Sama maam bu jigeen dafmay yonni ngir ma

dem nduggi saayu marse amee.— Patou jaaxle ci loolu xamal ko ne: deet yow tamit loolu jarul jooy.

Page 38: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

10

Page 39: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

— Fii ne ko jërë-jëf ba nga xamee i muy waxee.

11

Ahmad wëy ci naqaram ne ko :

- Ahankay ndax xaalis ba sama maam joxoon reeralnaa ko.

Fifi daadi waaru ci yalla :

— Yow Patou ni nga ëppëlee !

— Maa ngui jeggalu… Patou rus daadi kay baalu aqq.

-Ahmad ne ko bul rus man maa ko def, jappalema rek moo la taxoon jog.

Page 40: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

12

Page 41: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

13

Ahmad mu ngi jaaxle ba leegi ci xaalis bi reer :

-Dama waroon dem marse ngir jënd jën, ceep, banaana ak tuuti suukar... Nan laay def leegi ?

Fifi dëfël ko tuuti:

— Bul am looy tiit dina ñu la taxawu ba nga gis sa xaalis. Na ñu jaaraat finga jaaroon jombul da nga ko waddal ci yoon bi. Fan la

seen kër nek?

Ahmad mu ngi jiitu di woy, topp yoon wi jëm seen kër ?

Fifi mungi naan Ahmad daal moo mënn woy:

— Kon dangay woy ?

-Waaw, damay xalam di tëgg sabar.Talaata bu jot damay jang..Patou sonnal ko ci ay laaj:

Li ci des ngir ñu agg seen kër berina am deet ?

Page 42: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

-Fifi ak Ahmad tontu ko ne ko fii tamit gisuñu dara

14

-Deet-deet fi rek. Ci benn tool bu am ay bëy ak ay ganar yu bari laa dëkkee.Waaye moytu leen de, sama

maam waru ñoo gis.

Fifi di yoot ndank-ndank, Ahmad di seet ci ginnaaw

garab yi, Patou moom yeeg ci kaw benn garab Mu

tallal leen loxo:

— Gisuma dara fii!….

Page 43: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

15

Page 44: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

16

Page 45: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

17

Ahmad daadi wokk bopp bi :

- Doy na waar sama maam bu jigeen dinama jeppi !— Du ne nga tay besu dem marse la ?

-Ahmad daadi kay tontu, ne ko waaw, ni ñu koy defee allar-ba ak gaawu bu ne.

— Waaw leegi kay bu fekkee gisu ñu sa xaalis, dina ñu ko

lijjënti ci suñu pexe bopp.

Patou aand na ak wax ji:

— Waaw-waaw,dëgg la kay ni ko su�u maam bu goor daan

waxee, nit da nga wara gëm sa bopp.

-Ahmad daadi kontaan e ayca leen ñu dem lijjanti koppar yu ñu moomal su ñu bopp !

Popo daadi leen jiitu ca kanam, mu kontaan bu baax

ci yoon bu bees bu ñu jël...

Page 46: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

18

Patou daadi leen won benn yoon.

Na ñu bëtt ci bayaal bi le, xëy na ñu gis fa ay

bagaas yu am solo.

Page 47: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

19

Ba ñu aksee ci bërëb ba, Ahmad xamal leen :

-Man woy ak fecc rek laa mën, dina defar xalam ndax am naa boyt, bant ak ay weñ !

-Ahmad kontaan, ëy waay, liggeey bi rafet na.

—Fifi daadi jël kaddu gi, man mënna defar ay mbubu yu bees takk ci ay saaku palastik

yu maggat.

Patou moom daadi jaxase suuf ak ndox ngir raatale ko ci mbubu yi

.

Page 48: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

20

Jaaykat yi ñi ngi dajaloo ci digi bërëb bi.

Mak ak ndaw di jënd ak jaay.

-Na ňu dem ci sufu garabu mango bi foofu dina ñu moytu taw bi bu baax !

Ahmad daadi joxoñ benn garab bu rafet :

Patou daadi xëcc xaritam yi.

— Gaaw leen balaa nit ñi tasaaroo !

Fifi daadi siggi xool ca kaw :

— Wooy taw baangi soob !

Page 49: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

21

Page 50: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

22

Page 51: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

23

Patou woy bu baax ak baatam bu neex bi.

Ahmad gunge ko ak xalam, Fifi moom di fecc...

— Patou di woy naan mu ngi taw, taw, mu ngui tawataw ci marse bi !

Nit ñi tambali di leen wër, di leen seetaan te di naan :

— Lii aka neex waay !

Fifi ak Ahmad ñoo ngi feelu Patou :

- Di woy naan mu ngi taw, mu ngi taw, tawataw ci gox bi !

Popo moom mu ngi rafet ci yëre gaynde bi mu sol.

Page 52: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

24

Page 53: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

25

Ñep kontaan na ñu :

— Waaw ngeen goor, waaw ngeen goor, bilaay walaay dolli leen !

— Patou mu ngi naan Ahmad waaw gis nga lii ?

Fifi moom mu ngi yëg banneex bu rëy.

— Mu ne lii moom ndam la !

Ahmad mi ngi am mbégte bu rëy

-Jërë-jëf yeen ñar ! Ci dëgg-dëgg ay xarit yu baax ngeen !

Jërë-jëf yeen ñar ! Ci dëgg-dëgg ay xarit yu baax ngeen :

—Jël leen, jël leen! jërëgeen jëfati xale yi!

— Neexal ngeen suñu bes…

Page 54: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

26

Fifi,Patou ak Popo daadi gungé Ahmad ba këram. Maamam bu jigeen daadi waaru :

- Ahmad ne maamji jënd na li ngama yonni woon yëp: jenn, céep, banaana ak tuuti suukar !

— Maamji né ko fii nga fatte woon xaalis bi !Nan nga déf ba jënd li yëp.

-Ahmad né ko dama am ay xarit yu bes yuma jappale bama lijjanti xaalis bou léw ca marsé ba, loolu la ñu nduggee.

Mame ji daadi xaxataay.

— Waaw wooleen book ñu ñew añando ak ñun !

- Ahmad ne leen aksileen samay xarit, dal leen ak jamm sama kër.

Bi ñu tooge di xeewëlu, Fifi ak Patou daadi nétali seen jaar-jaar ci bes bi yëp.

— Popo daadi tecc waxtaan wi ak ay wow, wow

Page 55: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :

27

JEEX NA

Page 56: Auteur : Maxime Colin-Yves...Loi n 49-956 du 16 juillet 1949 sur les publications destinées à la jeunesse, modifiée par la loi n 2011-525 du 17 mai 2011. Achevé d’imprimer :